Siyansal Projet agricole u Sadio Mané

Yaatal
Siyansal
Projet agricole u Sadio Mané bi 11 Milliards la jar

Siyansal Projet agricole u Sadio Mané, Information Afrique Kirinapost

Un tableau de Serimacen

Siyansal
Budget général u Sénégal ci 2026 mi ngi si 7 433,9 Milliards FCFA

Siyansal
Sénégal am na suuf, ndox ,jant aki xale

Soo jële masse salariale bi nek si 1 532 milliards FCFA
Nga
Siyansal
Ñu xëy ne at mi ci bopp bu ak digg bi da ñuy fay genwalu salaire
Sunu ko xayma mu toll si 153 Milliards

Leegi su nu ko xaajee fukki xaaj ak been(11) di na doon fukk ak ñeet i (13 )
Ñu desal 10 milliards ñu def ko fonds yu ab societe Agro business

Siyansal
Salariés bëgg kaas ñu defal léen séen I koppar dividendes…

Siyansal
Ñu def projet bu nekk ci ben région u Sénégal yi
Ak 2500 emplois( 13projets) muy 32500 emplois

Siyansal
Ba dugg boîte vocale tey degg ni mën na nekk ba dindi xiif ak ñakk ci miim réew

Loo lambe ku ci siyans joxe dërëm

Siyansal Projet agricole u Sadio Mané, Information Afrique Kirinapost Save as PDF
Share

Laisser un commentaire

Votre adresse e-mail ne sera pas publiée. Les champs obligatoires sont indiqués avec *