Xarnu
bu bées
Ngi fuddu
Di waaja
juddu
Jant
ju yees
Ju ëmb leer
Ak yaakaar
Ngi waajal
Njollooru niit
aki nité
Na egsi
Ak jamm
Ak mbëgeel
Ak cofeel
Ak xamme
Sa takkandeer ..
Share
Related Articles
Bons Mots du Sahel 24 septembre 20240
Décès d’ Amadou Mahtar Mbow, le dernier géant est allé se reposer
C’est avec une grande émotion que nous avons appris le rappel à Dieu de…
Terroirs 13 septembre 20240
Guinée : que sont devenus les camps de réfugiés libériens ?
La Guinée a accueilli la majorité des réfugiés fuyant les guerres civiles sierra-léonaises et…
Terroirs 10 septembre 20240
Baaba Maal parrain de la 2 éme édition de « Sétal sunu rééw », le meilleur choix possible
En choisissant la star Baaba Maal comme parrain de la 2 éme édition…
Laisser un commentaire