Diamil Ciss. Lorsque le dernier poète sérère se met au Wolof…
Dekku teranga Moy sama cosaan
Sénégalais yi ñoy sama askan
Kay ndekki, kay añ ak kay ñu rer, fi amul gan
Ceebu jen, barada ak kaas, dañuy ataya di rétan
Salamalekum, Mu Aleykum salam
Mba jaam nga am? jamm rek
Korité Wala Pâques, Gamu Wala Noël
Liñu bokk diné duko taakkalé
Ndam li ñoko bok, kon Ndokkalé!
© Page Facebook Pourquoi J’aime Le Sénégal
Laisser un commentaire