Xarnu
bu bées
Ngi fuddu
Di waaja
juddu
Jant
ju yees
Ju ëmb leer
Ak yaakaar
Ngi waajal
Njollooru niit
aki nité
Na egsi
Ak jamm
Ak mbëgeel
Ak cofeel
Ak xamme
Sa takkandeer ..
Share
Related Articles
Terroirs 11 janvier 20210
Yang Yang, une part de mémoire nationale !
Prince du Djoloff, ancien Député-Maire de Louga, Mansour Bouna Ndiaye est un des plus…
Terroirs 7 janvier 20210
L’EXPÉRIENCE EST UNE CALEBASSE DE « KUSS »… DANS UN ÉCHO DE GIFLE !
» Un peu en retrait et au…
Terroirs 2 janvier 20210
LE LANGAGE TAMBOURINÉ AFRICAIN PRÉCURSEUR D’INTERNET ?
Extrait des Archives Afrikara : « Le langage tambouriné africain ancêtre de l’Internet ?…
Laisser un commentaire