Psychologie, Buju Katijanta

Mar ak xiif
Jur pëccëxoo
Ku nekk gaddu sa ndab

Psychologie, Buju Katijanta, Information Afrique Kirinapost

Oeuvre de Serimacen

Wuti
Jaay ko ñakk jomb ak tayeef
Coow walangàan
Ñi xamul fetewoo teen ba
Ñi jang ba xam ak di jangale xam xam toog robine Laasana
Waay u politig ak njublang roote robine Penda Laobe
Taskatu xibaar ak seen i gangoor feete robine Naa Mori
Su ngelaw sajjee
Pënd të wuri
Fagagal mbokk
Jukki bàak jafe
Sago jeex
Yitey xéwëlu
Su ci ndàa feesul
këll yu seeb a rootiji on
Su coow jure doom
Ken du xiif ak mar
Bës u tudd am
Jappal geek baayil gi
Nasaxal xel yi
Xol yu tang
Jëmbët pulox
Wure gas ak sulli
Su deqi jote
Yàakàar tagato
Ku nekk faqq yat ci toolu ñambi
Jënde sa xel
Saxayaay…!

Dofment 🚶‍♂️

Psychologie, Buju Katijanta, Information Afrique Kirinapost Save as PDF
Share

Laisser un commentaire

Votre adresse e-mail ne sera pas publiée. Les champs obligatoires sont indiqués avec *