Le 20 octobre 1886, une semaine avant sa mort, lors de la bataille de Dèkheulé, Lat-Dior a rencontré Cheikh Ahmadou Bamba. Un moment d’une densité spirituelle rare au cours duquel, le Cheikh signifia à Lat-Dior que l’issue de son face à face avec le colon était incertaine et lui demanda de renoncer à son projet. Lat-Dior déclinera l’invitation du Cheikh au prétexte que tout le pays l’avait déjà entendu défier le blanc et que sa parole est d’honneur. Le Cheikh acquiesça tout en lui remettant une prière. Serigne Mahamadou Lamine Diop Dagana nous rapporta cette rencontre et la prière en question.
Giseb Lathoor ak Sëriñ Tuubaa ca Mbakké Bawal 20 oktoobar 1886.
Lii bisub alarba la xewoon (muy giseb Latjoor ak Sëriñ bi), ba alarbaja delusee, ci la ko armeb nasaraan bi, songë ci DEXËLE, ñu xeex xeex bu tar lool, ci séen diggante, bañu faat Latjoor, ci weeru tamxarit atum 1305, ña ko gënë jige nëbbë, néew ba nasaraan yi, ba manu ñoo tek loxo cib néewém, ñu nëbbë yi tam fa ñu ko sool ba xamuñu ko, yalna ko yalla yërëm.
1-Yaw yalla maa gi lay ñaan ga maay ma ngëm gu sax dakk ak xol bu toroxlu diirub jamono.
2-Maa gi lay ñaan xam-xam bu am njariñ ak ngëm gu dëggu ngir ma man laa topp.
3-Magilay ñaan diine ju jub xocc, diine ju rafet ta yalnaga nangu sama ñaan gii ndax ma mana làq ay xéewal.
4-Maagilay ñaan ga may ma jamm, ga jammal ma ci mepp musiba ak bépp bala balaa boo xamni nii day daq leerug xel.
5-Maagilay ñaan yaw sunu boroom ga may ma matug jamm, maa gi lay ñaan yitam yaw sunu boroom saxug jamm.
6-Maagilay ñaan ga maay ma, ma sante la ci jamm jooju boo ma ko defalee mu mat ta sax, taga mayma yitam maay koo xamni damay doylu ci yaw mi ga xamni yaay buur, dëgg dëgg walif bëpp buur ak bëpp doomu àdama. Sëriñ Muhammadu Lamiin Jóob Dagana.
Version française
1- Ho Allah, donne-moi une foi ardente et un cœur soumis à ton autorité en toute circonstance et à jamais.
2 – Ho Allah donne-moi un savoir utile et une foi solide pour que je puisse être ton serviteur
3- Donne-moi une foi inébranlable et belle. Accepte ma prière afin que je puisse bénéficier de ta miséricorde et de tes bienfaits.
. 4-Que cette prière me délivre de tous les maux et de tout mal avant qu’il ne m’arrive de perdre la clarté de l’esprit.
5- Seigneur, donne-moi la paix.
6 Permet-moi de te rendre grâce et te remercier de cette paix que je te demande et que je veux complète et pérènne. Offre-le moi car tu me suffit. Toi le plus noble des Seigneurs. Seigneurs des Waliy, Seigneur des rois, Seigneur de toute la créature.
Laisser un commentaire